Senejournal - Toute l'actualité du Sénégal
Toute l'actualité du Sénégal

Le garwalé de Mia Guissé à son ex mari : « Beuri diar diar takhouta kham adounaa « 

Le garwalé de Mia Guissé à son ex mari : « Beuri diar diar takhouta kham adounaa « 

Beuri diar diar takhouta kham adounaa 
Beuri xam xam takhouta cilwisé 
Woné yiw takhouta am diiné 
Lo beuri doolé amo maitrise SAP nité desna 
lo beuri beuri diné té amo foie mok zeroyam 
Lo rafete rafete té sétoulo saffoul.
Yalnagnoul yalla may deugouu té mouy lou deugou si gnoune. 


Le garwalé de Mia Guissé à son ex mari :


Laissez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *